Ce qui protège la femme enceinte et l’enfant une fois né par Cheikh Ahmadou Bamba

Toubamajalis.com– Jigéen bu wanne lor bamu am ñatti weer (3 mois), da ngay wax : H’abdulaahi ibnu H’omar, H’abdulahi ibnu Mas-h’uud, H’abdulaahi ibnu Zubëyri, H’abdulaahi ibnu Salaam, H’abdulaahi ibnu Zëydin, H’abdulaahi ibnu ummi Maktuum (YYDG).

Boo noppe nga tifliko ci biirëm.

In chaa Allaahu, Bu doom ji juddoo góor lay nék, dina doon boroom xam xam ta saytaané duko laal.

Seex Sidiya mu makma neena ap ëmbu bu amee ñaari weer (2 mois) wala luko ëpp tuuti, na nga bind lii ci aw këyitt gu weex :

 

 

Su noppee, mu defko ap téeré takkal ko soxnasi bam am ñéen fukki guddi (40 nuits). Ginaaw ñeen fukki guddi yi mu tekki téeré bi dencko ba doom ji juddu. Bu doom ji juddu mu takkalko téeré bi. In chaa Allaahu, yalla dana sammu ëmb bi ak doom ji.

 

 

 

Extrait de : Majmah’u nuurayni fii fawaa-i-di daarayni

Auteur : Cheikh Ahmadou Bamba (rta)

Transcription Wolof : S Moustapha Lô Kholl , Ingénieur en Energie Renouvelable

Comments are closed.